Commentaire de Djibilahi (19/03/2009 15:49) :
Mani ley ziar bou wer, beggg na lol sisa blog bi rien a dire franchement.
Seulement ki gnouy wowé domi bamba mom la ken khamoul, mane dé léer nama ni
ki moy serigne touba moy rassoulilah té mofi yoniwon kep koufi meuseu
Diar.
Yalla nagnou Yag sant Borom darou Dounya.
djibilahi@hotmail.fr |